WAYE WI from MOYTOU by BATCH GUEYE
Tracklist
7. | BATCH GUEYE - WAYE WI | 3:42 |
Lyrics
{waye wi}ma wayla waywi,waywi yaye borom baye,ma wayla waywi,waywi yaye borom baye yi ,ma wayla waywi,waywi yaye borom, yaye borom,.Fa Mbaye di sa yaye,Abdou Gueye di sa baye.Batchie Gueye gau bokal ndaye ak baye Manoumbe,Cheikh Sene mounoy dioy te nope gounioy baye waywi yaye borom bayi,yaye borom !ma wayla waywi,waywi yaye borom bayi,yaye borom !Gueye masada penda ak mamaly penda nar gnieti doumou penda nar yi baye yayi borom .Ma wayla waywe ni waywe,ni baye Manoumbe waw,waywi yako mome !Batchie Gueye gua di sa mak,cheikh Sene gua bokal beneu ndaye,baye Manoumbe wawaw waywi yako mome.soumala woye warna,soumala wayoul warna ,baye waywi yaye boromee yi waywi yako momee baye.soumala waye warna,soumala wayoul warna,dara niorouko koudoul Mame Saliou.Gueye masada pendanar rée ak mamaly penda nar baye!gueneu wal gua deskawone,wayna fi yaye ,wayna fi Mak,wayna fi Rak te wayna fi goune.baye Manoumbe doumala fatee beneu yone baye,soumala waye warna,soumala wayoul warna.baye dara nioroula koudoul Mame saliou,soumala waye warna soumala wayoul warna,Ma wayla waywe ni waywe,ni baye Manoumbe wawaw ,waywi yako mome Batchie Gueye di sa mak,Cheikh sene gua bokal beneu ndaye baye Manoumbe wawaw,waywi yako mome
Type a message...
Credits
Musicians. Tapha Sock. Ndisga Mbaye. Aziz Tama. Birame Dieng. Adama Kambaye. Baty Dia
License
All rights reserved.Recommendations

by Hot Mule

by Fouma System

by Wau Wau Collectif

by Analog Africa

by Analog Africa

by Salif Keita

by Afrosunny Records