MANE MANE from MOYTOU by BATCH GUEYE
Tracklist
3. | BATCH GUEYE - MANE MANE | 3:28 |
Lyrics
(Mané Mané)dôme djiou beugue sa rew,dôme djiou fonkeu sa rew,diligueye te dou wax Sadio Mané waye na la,Sadio ,Sadio,Sadio Mané yaye diambare,dôme djiou beugue sa rew,dôme djiou fonkeu sa rew,di ligueye te wax Sadio Mané waynala.Sadio,Sadio,Sadio Mané yaye diambare,sadio ,sadio,Sadio Mané yaye diambare,doumou ndayou Ela Seydi,doumou ndayou Beauga,di ligueye te dou wax Sadio Mané waynala,sadio,sadio,Sadio Mané yaye diambare ,dou wax yow wax diou nias,dou tontou wax diou niaw,daye def tedou wax Sadio,Sadio yow yaye diambare,Sadio,sadio,Sadio Mané yaye diambare,.Sadio,Sadio,Sadio Mané yaye diambare.Ayeee salamalema,Mané dion kelefa,kerinw nigue kana waly ndianthio mouka foo iiii bouka bayiii,mbe kontoneuna mbe diayla sadio sadio sadio albarka Sadio Mané ..heeee Mané,heeee Mané ,heeee Mané ,heeee Mané,heeee Mané,heeee Mané,heeee Mané,.Sadio Mané yaye diambare,tabakhna fi lycée thi Sénégal Sadio Mané yaye diambare,dimbale nafi newdi doleyi thi Senegal,Sadio Mané yaye diambare,dieufdia bari lol,wax dia new lolo sadio !Sadio Mané yaye diambare,equipe national amnaneu thi yow yakar,sadio Mané yaye diambare,boul tayii,sadio boul tayii,fofoula Sadio Mané yaye diambare.
Credits
Musicians. Tapha Sock. Ndisga Mbaye. Aziz Tama. Birame Dieng. Adama Kambaye. Baty Dia
License
All rights reserved.Recommendations

by Hot Mule

by Fouma System

by Wau Wau Collectif

by Analog Africa

by Analog Africa

by Salif Keita

by Afrosunny Records