GISSE NAENE from MOYTOU by BATCH GUEYE
Tracklist
11. | BATCH GUEYE - GISSE NAENE | 3:48 |
Lyrics
(Gisse Nalene )naneu fonkou djigene,teyereum djiguene,djiguene naye sounou yaye boye naneu yeureum djiguene.Djiguenou sene-gambia naw nalene,niguene diapee seneu ni goryee guisnako,Djiguenou Sene-Gambia naw naleneu,niguene diapee seneu ni goryee guisnako.yene rakhass,yenaye footeux,te yeneu,yenaye passée,yenaye togou,yenaye boott,yenaye roguoti,yenee rakhass,yenaye fott,te yeneu,yenaye passé, yenaye togou,yenaye botteu,yenaye roguati.,Fonkou nalene,gueureume naleneu djiguene sene-gambi yayi,fonkou naleneu.Djiguene sene-gambi yayi,fonkou naleneu nigueneu diapee seneu ni goryee guisnako,djigueneeu,bilaye masa thiono,thiourourou,thiourou,mbaye,mbaye thiourourou,thiourou Mbaye,Mbaye ,thiourourou,Djiguene naye sounou yaye,djiguene moye botteu di nampaleu,bodee gonee hamoulo,mounoulo,boudoul wonakeu yaye dina meti,leklek gua khif,leklek gua marr,leklek gua diakhlee lolou,boudoul wonak yaye dina meti,Ni dôme gnieteleu bilaye dôme gnieteleu dôme dji titero yayam ak dôme dji yayam di tirero,ak dôme dji teral yayeum ,thiourourou,thiourou mbaye,mbaye thiourourou,thiourourou,thiourou mbaye,mbay,thiourourou,yenanouy botteu di nampal sounou hifee niou lek bou goudi diotee
Credits
Musicians. Tapha Sock. Ndisga Mbaye. Aziz Tama. Birame Dieng. Adama Kambaye. Baty Dia
License
All rights reserved.Recommendations

by Hot Mule

by Fouma System

by Wau Wau Collectif

by Analog Africa

by Analog Africa

by Salif Keita

by Afrosunny Records