🔗 ⚙️

Zikr Afie from Askanyi by Askanyi

Tracklist
1.Zikr Afie5:23
Lyrics

Fadilo FALLOU mou fadilo
Da gnou laye gnane nga gnanal gno

Balla aïssa ndimbeuli nga gno
Yeureume nga gno
Wétali nga gno
Thi aduna mame fadilo
Da nou gnane nga gnanal gno
Da nou gnane nga gnanal gno

Nga yag fé
Nou yag fii
Ligéyal mame fadilo
Da nou lay gnane
Mou dieum kanam
Ndax Ba nou dèmé
Ba fa kanam
Ba gneup outsi Lou nou Am
Lou nou am djombounoy dax
Ngeume gui fi sax
Fi thiy aname talibéy mayé
Fi thi daraay seugn bé
Seugn Bi yag sounou kanam
Yag no ndimbeulé lole
Mou fadilo hoo hoo da nou laye gnane nga gnanal no

Balla aïssa ndimbali nga no
Yeureum nga no
Wetali nga no thi aduna mame fallo
Da nou lay gnan nga gnanal gno
Da nou lay gnan nga gnanal gno

Ki mo diaye ndiourél
Dieundé kok talibe
Mou fallou ya nga thia kanam
Ki Mo djeul soror ba toudé ko
Mame Lamp fall
Mo fadilo nga thia kanam
Bayou AFIA bayou Segn atex Mbacke
Mou fadilo nga thia kanam

Credits
from Askanyi, track released October 30, 2015
Jupiter Diop (composer & lyrics), Ludovic Jeanmart & Sebastien Paz Ceroni (arrangments)
LicenseAll rights reserved.
Tags
Recommendations